Firefox, Firefox for Android
Firefox, Firefox for Android
Bisu yeesal bu mujj bi:
50% of users voted this helpful
Soudé déwelopeur nge, di nge guis lo soxlà ci Mozilla Developer Network (MDN). Ndàw Dewelopëer bu Mozilla (MDN) dañuuy bâhé ay jangat, ak firi yu lër ak tàm bëreb wahtanukay foy mëena latié ak di wétio ak yenène déwelopëer.
Page yi di niëw bahnà torop pour mëena tambali so soxla ndimbël :
- Duggàl : documentation ci Ndàw Déwelopëer bu Mozilla. Di ngafëe am ay léral ak code téktel pour bërp tolùwaayu xam-xam.
- Yoné léne séne latie ci Ndàw Déwelopeur wu Mozilla.
- Am ndimbël ci Developer Edition.
- Am ndìmbël ci Developer Edition.
Li dòn ne ay wahtàne yo mëna fek ci Ndaw Déwelopeur bu Mozilla:
- Sùumb xétu-web yu ùbeku :
- HTML
- CSS
- JavaScript
- Melukanu API internet
- Sistému Firefox:
- Ubì ay aplikaçion Web
- Tek ci yone ak tahawal sistému Firefox
- Bok ci jangàat bu sistemu Firefox
- Ranié Gaia
- platform bu Mozilla:
- Gecko
- Tahawal ak jangàt Firefox
- XUL
- XPCOM
- Yonû saytu bu Firefox (Nightly, Aurora ak Beta)